beytis

beytis

chers disciples de Baye Niass, en collaboration avec Mor Asta Kébé,nous avons collecté quelques beytis pour vous.

1) Asirou lifâki lil asara, li anani lada khadratil Mahi dalali asirou (Diwanu Sita P)
Damay d0h guir tënqi ñiñou jap (prisonniers), naka mane dal (BAYE) magi dokhh jeum cii Payii qui gaa khamni moy effacer rér (Mahi)

2) Kachaftoul bi oubihi al idjaba , wa inani tawaytou bi zikril Moustapha mahmahane khafra (P 88)>
Wuñena (dévoiler) kiray gui cii bëg Yonente, naka mane lèmna halu kerkedeng yi ci toud kouñou taneki (Moustapha)

3) Ra aytouka ahelane lil wasilati, sakhiyane ladal khawdi soultanane li yawmi wal akhiri. Khamidane lahou, tadjoune wa khakane, wa khatimane, moukhadasa sirine, rakibane fil mazahiri(Diwanu Sita P90)
Gisnala gay j0kuway bii, gay aji nandalé sa dég baa(khawdou naby=kawsara) ay bours (rois) ñél tay ak alakhira. Gay adji sante YALLA, dëg dëg, gay adji tëj (Yonente Yi), gay adji sél mb0t, gay adji war ci mazahir yii

4) Sitatoune minemi ina laz wouzina chanhratou minehou la khafatil awliyahou (CAT)
Jamano juné jurom bén témér (600) cii samay talibés sounou peser sén qaraw, sama karawou 600talibés yoyou dana woyofal balansou yénéne waliyou yeup.

5) Ouboudatou abdou lil zati, aïnou siyadati, tachewada fi maknouniha koulou sayidi, wa ma ouwa ila zatou bal aïnouha, al anahou aïnou zouhouri Mouhamadi, fasirou sara lisiri bisiri wahdouhou fama chama ila haqou wal sirou Lahote
Jam bi moy jëmou jëmou Yalla Bi, jëmi Sangue La, sangouna ci nëbu bimou nëb bèp Sangue, naka mom moy zatu moy jëmou dji, naka mom m0 féñè jëmi Mouhamad, mbot ma rañane na mom dong dara désul loudoul deug ak mbotou Lahote

6) Khousouri Madina Samou Kossine wa Taïbatahou wa Kaolakoune. Khad tahya bi zikri lazi kamoul. Oujawirouhou bi Kossine, wa ouwa bi Taïbati, wa absirouhou bil nouri wal khalbou lal moufal.
Samay palais Médina, Sam, Kossi, Taïba, ak Kawlack. Fofou lay doundé di fatalikou ko khamni adji matela. Dëkaléna ak mom cii Kossi, mom moggi Taïba, maggi koy guis cii lou lér ak cii sama khol dét may djéng.

7) Tasatartou ani daheri, mine zilou janabihi, fasirtou ara daheri falaysa yarani, falaw tas-âla ayami âni, madourate fa aïny makani, ma arafa makani.
Nëbuna cii sama jamano, cii walou képar gii, ma mouj di giss sama jamano té ñom gisouñou ma, bouñou lajone biss yi cii mane, khamouñou fane moy sama makane, khamouñou sama makane.

8) Boulaydou lakhat, am Mirayatou akhbalat, bi Dardasi mine wadi Sabu Fakalahou, bi tilkal mahani kana lil khoudbi cheïkhina khayatou, wafiha li tarikhi chawahou.
Dëk buñuy wax Boulaydou mo féñe, wala Miraya mo joublouci, cii Dardasi touké cii khour bouñouy wakh Sabu top Fakala, cii yilé mana nékone nafa ñél khoutbou bi di souñou Seriñe di dound, nék nafa yone bou sakh.

9) Yakhini yakhinane Moustafal kawni, iz sâfâ widadi lëhu iz fihi aïnu baqâ-hi, fanaïtou bihi bahda baqâ-hi, fa yastawi baqâ-hi bi khaïril alamina fanâ-hi.
Sama degenetanou kolouté moy Yonente këwnu bi, mom m0 sélal sama tiofél ñélko ndah mom moy jëmi déss, jékhna cii mom ganaw bama déssé cii m0m, wëy déss bii gëne cii moy jékh cii Yonente Bii.

10) A anta wasili ila lahi? khoultou naham. A anta waliyou lahi tahala? khoultou naham. A anta arifou bilahi tahala? khoultou naham. A anta minal aqdabi? fa khoultou la adri, walakine samihtou majazibi yata khawalouna, bi zalika wa rabouma ra-aw fi hali sani, wama cha-hâdi, wama takhadama.
Wazila nga cii Yalla? mani waw. Waliyou yalla nga? waw. Arif bilahi nga? waw. Ndah khoutbou nga? ma wah dédét wayé dég nah fénekate yii ñogi wakhaneto lolou. Warone nañouma guis cii sama halu niarél 2, ak sama halou sédé, ak sama hal bii jitou

Fa ine dakhicha aqtabou yawmane li machrabi, akhad khoumou li sahwi bi istidadi rouwahi.
Bouñou démé ba khoutbou yii guëlëm cii bisou nanouway ba, sama khér yii moy guindi gars yii bañou kham fouñouy nané.

11) Al mahjoubou alazi la-yara haqou tahirou, al majzoubou lazi la-yara ila zatou, al arifou lazi yara haqou wal khalkhou, wa youchahidouhou fi woujoudihi adamoune.
Mahjob moy ko khamni dou giss dëg j féñe, majzob moy ko khamni dou guìs loudoul jëmi Yalla J, arif moy koo khamni day guis Yalla ak Mbidéf yi, day cédé cii am-am yii ñu nék lou ñak cii aam.

12) Famane arada zouhour, fa ouwa abdou zouhour. Wamane arada khafa, fa ouwa abdou khafahi. Wamane lam youridou ila ma arada lahou, fa ouwa Abdoulahi haqane. Fal arifou mane taraka mouradatihi, li mouradil haqi.
Kou bëg fèñe, daga nék jam bu féñe. Kou bëg nëbu, daga nék jam bu nëbu. Kou nam nék jam ndah nam YALLA, moy jam dëg. Arif moy qui bayi ay bëg bëgam, jeum cili YALLA beug.

13) Lane satrine manelam youlad maratayni(CAT). Lam yahlamou malaqoti samawati wal ardy ila mane youlad maratayni (INSA)
Bokoul ci nioune kou joudouwoul 2 yone. Kén dou kham gourou asamane ak souf loudoul daga joudou 2 yone.

14) Touba limane khabla mamati bacharata, wama chakhdalake koulane acharaka (CAT)
Tékhé ñél na kiga khamaneténi soulna mbamélam bala mouy déh, fék migi jakarlok lép(soul sa mbamél avt gay déh).

15) Araka tarani bi khaïsou la tarani, waminal khaja-hibi ane tarani fala yarani, wakhli bi khaïbil-khaïbi, bilahi khayibatane takhayaba kouli ane jamihil khalikhati(CAT)
Gisnala gamay khol té yow gisouloma, bokena lii chi kémtanu gamay khol té gisouloma, ndah chi fadoug fadouga ,sa YALLA la fadou cii mbolém mindéf yëp.

16) Koulou faheline sara najelane, mine tihamine aw yamanine. Koulou siri fi baraya madahou sirou Tijany (BAYE)
Bép kouy moujéna done mboté, mo xamni wa Tiham wala Yemen. Bép mbot bou ajou cii mndafun yii migi tëbo cii mbotou géju CAT

17) Doufihtou dafkhatane mine khadratoul khaybi. Fasara ewali akhiri, wa akhiri ewali. Wa djouzehi kouli, wa kouli djouzehi. Fa sirtou ana ouwa, wa ouwa ana mine khaïsou ouwa lamine khaïsou ana. Fakhina saka lawza altini alfa alfa mas alati, la ajoubtouka bii jawabi wahid. Iz sirtou kal mizbakhi, lawousou khilate mini jamihoul mazabihi, mana khazamine dawehi chéyehine, wali lahil hamdou(CAT).
Sani nañuma ap sani touké tchi Payi bu fadouba. Moujéna sama jëlbéne moy sama mouj, sama mouj moy sama jëlbéne. Sama lène moy sama lèp, sama lèp m0y sama léne. Moujouna may mom, mom moy mane. Cii wakhtou wowou, souñou ma lajone ay jounéy jounéy ladj, danaléne tontou cii béne tontou. Guir di mélni ap lampe, bouñou talone cii mane mbolém lampes yii, dou wañi dara cii sama lér, tiant ñélna Yalla.

18) Wala karamatou akbarou mine khidematili. (BAYE) Wa tadjehalna ifzou kitabakal karim, karamatihi ilal likhayikal azim. (BAYE)
Karama gënoul rëy nga khitmal mah. (BAYE) Magui lay niane (yow YALLA) ga déf ma outou alquran, mou done sama karama ba kérok.

20) Ata khadousou bi nihmati lahi choukroune, wa tarkouha koufroune. Wamane la yachkourou khalila, la yachkourou kasira. Wamane lah yachekourou nasa, lah yachekourou laha. Wal jammatou rahmatoune, wal fourkhatoune khazaboune. (HADITH)
Wakhtané khéwalou YALLA sant leh, bagna wakhtané khéwalou YALLA wédi leh. Koudoul sant lou nèw doh sant lou bëri. Koudoul sant nit, do sant Yalla. Mbolo yërmandeu leh, takaliko mbougël leh.

21) Laysa tasawouf loubsou tawbou tarfahahou, wala boukahouka ine ana mahnouna, wala miyahou, wala rafsou, wala tarnou, wala tahachou, kana khad sirtou majnouna. Bali tasawouf ane tasfou, bila kadari; wa tatabihal haqa, wal fourhana wa dina. (BAYE)
Nékoul tasawouf moy sol yeuré you khotékou, dou tiagani joy (ndém waykate bi wayna), dou khatiou, dou fécc, dou danou, dou yohou, (niom) mouj naniou sakh nék dof. Liñou toudé tasawouf moy ga sél, sél bou amoul neukhneukh; ga top haqou (YALLA), ak alquran ak diné.

22) Fama Napoléona aw Léninoune wa Marqasoune, bimoukhane ilayhim khali aneka khabala. Kitaboune mina lahi jalili jalalouhou, khadimoune wa bakhine la yakhafou zawala. Talahou fatâ mahmounou djeuhrane wa yeukheuzatane, fadah bahda aza koula khili wa khala. (Sayroul Khalbii P 24)
Déte Napoléon wala Lénine ak Marx,duñu wahyu 6 ñom bayil lolou ap rérla "d0fla diléne top,téré bu mag bi jugé 6 Yalla magayam gi aji jitula aji dèsla tamite ragalul ap dañe. Danako jeunk (téré bii) kounou wolou qui cii lou fégn ak cii yeuk, bayil ganaw lii bép wéréneté.

23) Ouwa haqou wal nouroul moubine, wa inani daraytou aléyhi, rahmou anefou bakâ imi.
Moy haqou moy lér gou bir, naka mane (BAYE) lémuna cii mom (Yonente bi) ,torokhna bakanu nones yii.

24) Al yawmou akmaltou lakoum dinakoum, wa atemamtou alaïkoum nihemati, waraditou lakoum islamou dinane.
Tay la matal ñél lên sén diné, té khéwélél naléne sama khéwël, gërëm na ñél lène islam m0y diné.

25) Bi faïdi yanal dini rafehou liwahi, wamane chaha yatihi khoubaïla mamatihi, wamane chaha nawahou ka ahli chafahi.
Si sama faydou laye diné dji dii amé yëkëtikou, koumou nékh gaa dik jeunk gay dhé, koumou nékh ga bañe bok cii ñou tékhé diñi.

26) Fafad ataïna ala Ibrahima kitaboune, wal hiqma, wa ataïnahoum moulkou azim. (CORAN)
Joh nañou ñoñou Ibrahima térébi, ak hiqma(marifa), té jokh nañou léne gour gou mag.

27) Wa lakhad ataïna Ibrahima rouchedihou mine khabli. (CORAN)
Jokh nañou Ibrahim joubam cii lou jënk.

28) Waskourou rabane ahlama abda rouchedahou, fa aseharou atebahi birihoune minal chirki. (BAYE)
Sante na Yalla bamou jokhé jamam bi joubab, ñou gëna ndaw cii ñima tope dañe nañou cii bokalé.

29) Mane lam yatasil bil khadrati, walam yatasil bimane itasil bil khadrati, fa ouwa ibnou zina inda ëhli haqiqati. (BAYE)
Kou jokouwoul cii PayBii, wala mou jokou cii kou jokou cii PayBii, kokou domou jalo lah cii waa ñoñou haqiqa.

30) Souloukou khabla jazbou khijaboune, wa bahdahou kamalou. (BAYE)
Sobou lata jëzbou kiray leh, am jëzbou soga am soulouk moy lii mate.

                                                                                                              Mor Asta Kébé

2 votes. Moyenne 4.50 sur 5.

Commentaires (2)

1. khassim kebe (site web) 24/01/2013

thiey sang ndiaye contanne si ligueye bi nga xamni moye dimbali adouna bi yieup

2. ndiayement 06/12/2012

dieureud!!!!!!!!!!!!!!

Ajouter un commentaire

Vous utilisez un logiciel de type AdBlock, qui bloque le service de captchas publicitaires utilisé sur ce site. Pour pouvoir envoyer votre message, désactivez Adblock.

Date de dernière mise à jour : 28/01/2013

Créer un site gratuit avec e-monsite - Signaler un contenu illicite sur ce site

×